send secret message to Kalidou

Kalidou can not see who sent them the message

👀 135 | 💬 0

Kalidou 's Wall

Anonymous:
Diemal topou thi say tankou grand frère
Kalidou :
Moyy sama référence ❤️🩸
Anonymous:
Pour yaw daguaa mousss mais xamalni sa xel bi amoul dra
Kalidou :
Srx 🤣😭😭?? Vous faites ma soirée nak !!!
Anonymous:
Tok di lire say anos 😂👍🏽
Kalidou :
Nanal coca 🤣
Anonymous:
Kalidou noppou 😂😂😂
Kalidou :
Balnaala 😭
Anonymous:
Tanyi dieul gua samba d 🙄
Kalidou :
Samba Diaara mn frr mn sang 🩸🍀
Anonymous:
T'as l'art de convaincre machalla
Kalidou :
Merciii beaucoup ❤️✨
Anonymous:
Tu es une personne formidable niittt guenou la et meune nagne la waxal tout sauf hypocrisy tu es très loyal et sincère ❤️
Kalidou :
Ceci me touche énormément 😇❤️
Anonymous:
Mon Guy sûr
Kalidou :
👍🏽😌🍀 le véritable
Anonymous:
Nio bokone class wayé xamal nii soofoo mawone d 🤭
Kalidou :
🤨nono 🙄
Anonymous:
Bilahi xamoo sa bop
Kalidou :
Waxmako bok 😂
Anonymous:
Mon ami de valeur
Kalidou :
Ici présent 🙃✨
Anonymous:
Soma takoul ma xarou
Kalidou :
Eupeunaa def 🤣🤣 mou yao t kii ?
Anonymous:
Nieupeu xamnagne ni dagua nopp Aminata Thioub waxkoko rk
Kalidou :
Minaa 😭😭😭 kayy xol
Anonymous:
Doo rouss di gueneuh akk sa ex xarite
Kalidou :
Ah bon ??😭🤣
Anonymous:
Nitt gue noula mais xamale lima la wakh nakh ande bi ioe SK KG MS MANE MA NEKONE SEND DJIGUENE YAKOUNA SI ZERO KOU NEK AWNA BENE YONE LOLOU WAROUNIO DE
Kalidou :
Srx 😂😂😭 yena meune nak
Anonymous:
Tu es hyper intelligent yalla boul thiate topou tu iras loin c sûr
Kalidou :
Amine 😊😇
Anonymous:
Niata ex gua am
Kalidou :
Waxoumala 🙃
Anonymous:
Yaa meune solou nak
Kalidou :
Bilay 🥲😂
Anonymous:
Sincèrement j’ai des sentiments pour toi mais je ne veux pas gâter nôtre amitié 😔
Kalidou :
Alors me di r1 😁
Anonymous:
On s’est connu au LBD t devenu un frère kals 🩸
Kalidou :
Le s🩸
Anonymous:
Sofff gua boy
Kalidou :
Watal 😂
Anonymous:
Mon petit frere ke j’aime trop je sais ke dinga khame c ki mais ne change jamais jtaime comme tu est yalla nala yalla teral defla magg bou Ame Barker jtaime fort
Kalidou :
Soeurette❤️
Anonymous:
Tu es talentueux, génial et intelligent alors il faut que tu sois patient pour mieux réussir dans la vie car tu es déjà sur le bon chemin je te souhaite le meilleur pour la vie 👍😁
Kalidou :
😇merci
Anonymous:
On es ami dh ya longtemps même mais y avais un temps je cruchais sur toi 🥹❤️
Kalidou :
Srx 😂
Anonymous:
Cheri de mon cœur ♥️
Kalidou :
Big ❤️
Anonymous:
Tes méthodes pour motiver sont parfois douteuses mais tu aimes faire progresser les autres de mon avis
Kalidou :
Ah ouiii !!
Anonymous:
Sa guel bou xess binekone saint pierrre askip takkeuh nagne ko
Kalidou :
Heureux ménage 😂
Anonymous:
Boy
Not replied yet
Anonymous:
Boy mane ak ioe arabe ba legui wah dag change legui ame kharite you bess t lolou walou la nk
Kalidou :
Nn send mess pv
Anonymous:
Deguena niouné respecté wo sa parents yi est c que c vrai ?
Kalidou :
Ahh eskeu doo dem lathié personnellement 😂 mdr
Loading content...
Tracking